TSK

TSK · 2 Samuel 2:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Wóoy Sóol ak Yonatan, ñoo yiw, sopplu ba ñuy dund, te ba ñu deeyee, teqlikoowuñu. Ag jaxaay, ñoo ko gëna gaaw, te gaynde, ñoo ko gëna jàmbaare.

Ñii bokkoon nañu ca Fanweeri jàmbaar ya: Asayel, rakki Yowab, Elxanan, Dodo di baayam, dëkk Betleyem,

Kii nawul dooley fas, gërëmul kàttanu jàmbaar.

Amos 2:14 TSK

Rawtu dina réer ku gaaw, boroom doole du tala jariñoo dooleem, jàmbaar sax du mana rawale bakkanam.