TSK

TSK · 2 Samuel 2:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu ne ko: «Ndax kenn desul ba tey ci waa kër Sóol, ba ma jëfeek moom ngor gu Yàlla gërëm?» Ciba ne ko: «Doomu Yonatan ju tànk yi baaxul a nga fa ba tey kay.»

Daawuda ne: «Dinaa jëfe ngor sama digganteek Anun doomu Nayas, na ma baayam jiye woon ngor.» Daawuda nag yebal ay ndawam ca Anun, di ko jaal baayam. Ba ndawi Daawuda ya agsee ca réewum Amoneen ña,

Ma woo Yàlla, Aji Kawe ji, Yàlla, mi may matalal.

Su la tooñee, mbaa mu ameel la lenn, topp ma ko.