KYG / 2 Samuel / [JC0] chapitre 21 KYG · verse 2 Aa Xoolaat Jàngalekatu bind Buur woo waa Gabawon, wax ak ñoom. Waa Gabawon bokkuñu woon ci bànni Israyil, waaye ñoo... Dayo bind A- 25px A+ Font jàngat Serif Amul Naskh Amiri Scheherazade New Noto Sans Arabic Cairo Tajawal Markazi Text Changa Noto Kufi Arabic Alexandria Almarai Aref Ruqaa Ink El Messiri Harmattan IBM Plex Sans Arabic Mada Reem Kufi Lateef Reset ← 2 Samuel 21:1 2 Samuel 21:3 → Toppal Yoon yu jàmm Jàngalekat Jàmm Nòt ♥ 📝 B uur woo waa Gabawon, wax ak ñoom. Waa Gabawon bokkuñu woon ci bànni Israyil, waaye ñoo desoon ca Amoreen ña bànni Israyil giñaloon ne duñu leen rey. Teewul Sóol xéroon lool ci bànni Israyil ak Yuda, bay fexee faagaagal waa Gabawon. Chapitre bi yépp Aaya yi ci méngoo Tekki Wolof yépp Bible yépp