2 Samuel 2:23
TSK
Asayel të ticc, topp ko. Abner jam ko catal xeejam ca biir ba, ba xeej ba fëll ca gannaaw ga, mu daanu dee ca saa sa. Ba loolu amee, ku dikk, ba tollook bérab ba Asayel daanu dee, daldi fay taxaw.