1 Samuel 14:7
TSK
Ba loolu amee gàddukatu gànnaayam ne ko: «Ayca, loo namm rekk, sang bi, yaw laa àndal ba jeex tàkk.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba loolu amee gàddukatu gànnaayam ne ko: «Ayca, loo namm rekk, sang bi, yaw laa àndal ba jeex tàkk.»
Waaye Cadog sarxalkat ba ak Benaya doomu Yoyada, ak Yonent Yàlla Natan, ak Simey ak Reyi, ñook jàmbaari Daawuda ya koy dar, ñooñu ànduñu woon ak Adoña.
Teewul Aji Sax ji wax Daawuda sama baay, ne ko: “Gannaaw yaa fasoon ci sa xol, yéeney tabax kër, tudde ma ko, def nga lu rafet, ngir sa yéeney xol la woon.
Yal na xool loo ko jébbal, di rafetlu sarax soo ko lakkal. Selaw.