TSK

TSK · 2 Samuel 9:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Sopp seeni maam nag moo tax mu taamu leen, yeen askan wi leen wuutu, génneel leen boppam Misra, ci dooleem ju bare,

Xanaa moos su may dund, ci ngorug Aji Sax ji ngay jëfeek man. Su ma deeyee nag,

Naka la Mefiboset dikk ca Buur, di ko teertu, Buur ne ko: «Mefiboset, lu la tee woona ànd ak man?»

Titus 3:3 TSK

¶ Ndax nun itam kat, ñu ñàkk xel lanu woon te déggadi, ñu réer, tënku ci lu doon ay xemmemtéef, ak bànneexi bakkan, tey wéye def lu bon, ak ñeetaane, ñu jara bañ te bañante ci sunu biir.