TSK

TSK · Acts 10:14

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mukk laa wax! Du dangeen di màggal Aji Sax ji? Demleen boog, yeen ñiy góor!» Ba loolu amee ñu dàq leen, ñu jóge ca Firawna,

Kon nangeen ràññee mala mu dagan ak mu daganul, ak itam njanaaw lu dagan ak lu daganul, te baña sobeel seen bopp ndax mala mbaa njanaaw mbaa mboolem bindeef yu sew-sewaan yiy dox ci suuf te ma limal leen ne setul.

Lii moo di mala yi ngeen di lekk seen suux: nag ak xar ak bëy;

¶ «Gannaaw loolu mboolem lu médd mbaa lu ñu fàdd, muy boroomi laaf akug jur, sarxalkat yi duñu ko lekk.

Luke 1:60 TSK

Yaayam nag ne leen: «Déet, Yaxya lay tudd.»

Mu ne leen: «Yeen de xam ngeen ne ab Yawut, mayeesu ko mu jaxasoo ak xeetu jaambur, mbaa mu seeti ko. Waaye man nag Yàllaa ma won ne du kenn nit ku ma naan daganula jaxasool, mbaa setul.