TSK

TSK · Acts 11:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Teewul baat bi wax ak moom ñaareel bi yoon, ne ko: «Lu Yàlla setal, bu ko daganadil.»

¶ Ba loolu amee Piyeer àddu, ne: «Dëgg-dëgg gis naa ne Yàlla daal du gënaatle,

Lu mu mana doon, kàddug Yàlla akug ñaan moo koy sellal.