Acts 11:29
TSK
Taalibe ya nag fas yéenee boole kem kàttanu ku nekk ca ñoom, ngir ndimbal lu ñuy yónnee bokki diiwaanu Yude.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Taalibe ya nag fas yéenee boole kem kàttanu ku nekk ca ñoom, ngir ndimbal lu ñuy yónnee bokki diiwaanu Yude.
¶ Ca biir mbooloom gëmkat, ña woon ca dëkk ba ñuy wax Àncos, amoon na ay yonent ak ay jànglekat: ñuy Barnaba, ak Simeyon mi ñu dippee Ñuule, ak Lusiyus mi bawoo Siren, ak Manayen mi yaroondoo ak Erodd boroom Galile, ak Sóol.
¶ Ab nuyoo ñeel na leen, tukkee ca mbooloom gëmkat ma ca Babilon te di ñu ñu taamu ni yeen, tukkee itam ci sama doom Màrk.