TSK

TSK · Acts 16:30

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 34:32 TSK

Won ma sama tooñ yi ma gisul. Su ma defee lu ñaaw, dootuma ko def!»

«Xanaa du lii moo di koor gi ma taamu: yolomal jéng yu metti, fecci buumi noteel, afal ku diis; dog lépp luy xeetu noteel?

Luke 3:10 TSK

¶ Mbooloo ma itam laaj ko ne ko: «Ana lu nu war nag?»

Acts 2:37 TSK

¶ Ba mbooloo ma déggee loolu, naqar wu mel ni jam-jamu xol la leen def. Ñu ne Piyeer ak ndaw ya ca des: «Bokk yi, nu nuy def nag?»

«Yeen, lu leen xiir ci lii? Nun itam ay nit lanu, bokk ak yeen benn bind. Xibaaru jàmm bi lanu leen di xamal, ngir ngeen wacc yëfi neen yii te walbatiku ci Yàlla, kiy dund te sàkk asamaan ak suuf ak géej ak mboolem lu nekk ci biir.

Ndigal loolu nag tax mu sànni leen ca néeg ba gëna ruqe ca kaso ba, jéng leen.

Daan bu àndul ak yërmande, moom lees di àttee ña daawul jëfe yërmande. Yërmande nag kekku na ab daan.