Ephesians 5:16
TSK
Jariñooleen lu ngeen man, jot gi ngeen amagum, ndax jant yu bona ngii tey.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Jariñooleen lu ngeen man, jot gi ngeen amagum, ndax jant yu bona ngii tey.
¶ Dégg nanu nag ne ñenn a ngi ci seen biir, ñu nekke ag yaafus, duñu yëngu ci dara, lu moy di topptoo lu seen yoon nekkul.
Waaye ay kebetuy àddinay kese, moytu ko, ndax ngëmadi gu ko yées rekk lay yóbbee,