Damaa wàcc, xettlisi leen ci waa Misra; génne leen réew moomu, ba yóbbu leen réew mu baax te yaatu, réew mu meew maak lem ja tuuroo, foofa ca diiwaanu Kanaaneen ña ak Etteen ña ak Amoreen ña ak Periseen ña ak Eween ña ak Yebuseen ña.
TSK
TSK · Acts 17:6
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Exodus 3:8
TSK
Jeremiah 38:2
TSK
«Aji Sax ji dafa wax ne: “Ku des ci biir dëkk bii, saamar rey ko, mbaa xiif, mbaa mbas. Waaye ku génn fekki waa Babilon, dina raw, bakkanam di ngañaayu xareem, mu mucc.”
Acts 6:12
TSK
Ba loolu amee ñu xabtal nit ñi ak njiit yi, ak firikati yoon yi, ñu ne jalañ, jàpp Eccen, yóbbu ca kurélu àttekat ya.
Acts 18:12
TSK
¶ Jant ya Galyon moomee diiwaanu Akayi, Yawut ya dañoo mànkoo, jógal Póol, jàpp ko, yóbbu ca àttekaay ba.
Acts 22:22
TSK
¶ Ba ba muy wax loolu, mbooloo maa nga koy déglu. Ba ñu déggee kàddu yooyu lañu xaacu ne: «Jëleleen ko ci kaw suuf! Ku mel ni kii yeyoowula dund!»
Acts 28:22
TSK
Waaye bëgg nanoo dégg ci sa gémmiñu bopp li nga gëm, ndax li nu xam daal mooy, ngér moomu nga bokk, fu nekk lañu koy diiŋate.»