TSK

TSK · Acts 20:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Acts 19:1 TSK

¶ Diir ba Apolos nekkee Korent, Póol a nga jaare ca diiwaan yu tunde ya, ba wàccsi Efes. Mu daje faakay taalibe,

¶ Li nuy damoo nag moo di seede bi nu sunu xel mu dal seedeel, ne xol bu set ak jikko ju dëggu ju bawoo fa Yàlla, mooy li nu doxale ci àddina si, rawatina sunu digg ak yeen, te du lu nu sunu xam-xamu nitu neen may, waaye yiwu Yàlla moo nu ko may.

ndax sunu xibaaru jàmm, bi nu leen àgge, dikkewu leen ay wax rekk, waaye manoore la leen dikkaale, ak ndimbalal Noo gu Sell gi, ak kóolute gu mat sëkk gu ngeen am. Xam ngeen moos na nu nekke woon ca seen biir, di xintewoo seen njariñ.

Yeen ci seen bopp, xam ngeen ne ci sunuy tànk ngeen wara awe, te du ag yaafus lanu nekke woon ci seen biir.