TSK

TSK · Acts 21:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Acts 11:4 TSK

¶ Piyeer daldi leen benn-bennalal mbir mi.

Acts 15:4 TSK

Gannaaw loolu, ñu agsi Yerusalem, mbooloom gëmkat ñi, ak ndawi Yeesu yi, ak mag ñi, dalal leen, ñu nettali leen mboolem ni Yàlla def ak ñoom.

Waaye sama bakkan soxalu ma, xanaa ma bey samaw sas, ba sottal liggéey, bi ma Sang Yeesu dénk, te mooy seedeel xibaaru jàmm bu yiwu Yàlla wi.

¶ Ana kuy Apolos sax? Ak kuy Póol? Xanaa ay surga doŋŋ yu ngeen jaare, ba gëm, ni Boroom bi jagleele kenn ku nekk ci nun, aw sasam.

¶ Nun ñi bokk ci liggéey bi nag, noo leen di ñaan ngeen baña nangu yiwu Yàlla ci neen.

Loolu moo ma tax di góor-góorlu ci xare bii may xaree dooleem, ak manoorey jëfam, jiy liggéey ci sama jëmm jii.