TSK

TSK · Acts 21:30

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Luke 4:29 TSK

Ñu jóg, bëmëx ko ba génne ko dëkk ba, yóbbu ko ca kéméju tund, wa seen dëkk ba sance, ngir xalab ko ci suuf.

¶ Ba loolu amee alal ja njaatigey ndaw sa yaakaaroon, réer leen, ñu jàpp Póol ak Silas, diri, yóbbu ca pénc ma, fa kanam njiit ya.

Loolu moo waral Yawut yi jàppe ma ca kër Yàlla ga, di ma fexee rey.