1 Samuel 13:10
TSK
Naka la def saraxu rendi-dóomal bi ba sottal rekk, Samiyel ne jaas. Sóol génn gatandu ko, ngir nuyu ko.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Naka la def saraxu rendi-dóomal bi ba sottal rekk, Samiyel ne jaas. Sóol génn gatandu ko, ngir nuyu ko.
¶ Fekk na Erodd dëngoo lool ak waa dëkk yi ñuy wax Tir ak Sidon. Ci kaw loolu waa Tir ak Sidon mànkoo, dikk ba ci Erodd. Ñu daldi fexe ba jubook Balastus, bëkk-néegu Buur, ba noppi di sàkku jàmm, ndax seen dundub réew, ca dundu Buur Erodd la daan jóge.
¶ Gannaaw ba nu fa toogee ay fan, ab yonent bu ñuy wax Agabus jóge Yude, agsi.
¶ Gannaaw ab diir buur Àggripa ànd ak jigéenam Berenis ganesi Sesare, ngir nuysi Festus.
¶ Nuyul-leen ma mboolem seeni njiit, ak mboolem gëmkat ñu sell ñi. Waa Itali ñu ngi leen di nuyu.