TSK

TSK · Acts 23:15

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Yonadab ne ko: «Dangay tëdd ci sa lal, wopp-wopplu, ba sa baay dikk, seetsi la, nga ne ko: β€œNa sama jigéen Tamar ñëw, may ma, ma lekk. Na ma toggal ci sama kanam, may gis, te mu sexal ma ci loxol boppam.”»

Ku bon a ngi yeeru ku jub, di ko wuta bóom.

ngir dañuy xélu, nar musiba, di gaawtuy sànk bakkan.

seeni tànk daw wuti lu bon, ñuy yàkkamtee tuur deretu ku deful dara, seeni xalaat di ñaawtéef, yàquteek njaaxum féete ca seeni yoon.

Acts 25:3 TSK

tinu ko ngir mu woolu Póol Yerusalem, ndax fekk na leen lal pexem rey ko ca yoon wa.