TSK

TSK · Acts 24:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Yeesu ne ko: «Waa jii, kan moo ma fal àttekat mbaa miraaskat ci seen kaw?»

Piyeer liyaar leen, ngir ñu noppi, daldi leen nettali, ni ko Boroom bi génnee kaso ba. Mu ne leen: «Yégal-leen ko Yanqóoba ak yeneen bokki taalibe yi.» Ba loolu amee mu génn, dem feneen.

Waaye su dee ag dëngoo ci wàllu wax, mbaa ay turi nit, mbaa seen yoonu bopp nag, seetal-leen ko seen bopp. Àtte loolu moom, duma ko nangu.»

Mu may ko. Póol taxaw ca dëggastal ya, tàllal mbooloo ma loxo, ñu ne selaw. Mu wax ak ñoom ci yawut, ne:

Acts 26:1 TSK

¶ Ci kaw loolu Àggripa ne Póol: «Léegi sañ ngaa waxal sa bopp.» Póol nag tàllal loxoom, layool boppam, ne: