TSK

TSK · Acts 25:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Naka lañu ko yeew ngir dóor ko ay kàccri, mu ne njiitu takk-der ba fa taxaw: «As goru Room bu yoon dabul, mbaa am nga sañ-sañu dóorlu ko?»

Acts 25:6 TSK

¶ Festus toogaatul ak ñoom lu wees juróom ñett ba fukki fan, doora dellu Sesare. Ba mu agsee ba ca ëllëg sa la toog ca àttekaay ba, joxe ndigal, ñu indi Póol.

Man nag damaa gis ne deful dara lu jar àtteb dee. Waaye gannaaw moo dénk boppam buur bu tedd bi, man dogu naa ko koo yónnee.

Ñooñu seet sama mbir, gisuñu ci man tuuma ju yelloo àtteb dee, ñu nar maa bàyyi.