TSK

TSK · Acts 25:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ci biir loolu kenn ca surga ya wax Abigayil jabaru Nabal, ne ko: «Ãa, Daawuda de moo yebal ay ndaw yu jóge ca màndiŋ ma, ngir nuysi sunu sang, waaye moom, da leena jànni.

daldi dajeek bokki Akasiya buurub Yuda. Mu ne leen: «Yeenay ñan?» Ñu ne ko: «Bokki Akasiya lanu. Danuy nuyuji doomi Buur Axab, ak doomi Lingeer yaayu Buur.»

Acts 8:40 TSK

Filib moom, dëkk ba ñuy wax Asot la gisaat boppam. Mu wéye di xamle xibaaru jàmm bi ci dëkkoo dëkk, ba àgg Sesare.

Acts 26:1 TSK

¶ Ci kaw loolu Àggripa ne Póol: «Léegi sañ ngaa waxal sa bopp.» Póol nag tàllal loxoom, layool boppam, ne: