TSK

TSK · Acts 25:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Cóolóoloo cóolóol, waru waarekat ba, cóolóoloo cóolóol, léppi cóolóoli neen.

Sa puukare gee tàbbisi nii njaniiw, yaak sa buumi xalam? Ay duusu di sa laltan, ay sax di sa càngaay!

Bu ma dogee sidditi Misra, ba doole ja muy sago ŋiis, jant dootu fenkal Tapanes, aw xiin ay sàng dëkk bi, te dëkk-dëkkaanam ya, njaam lañu jëm.

Maay def réew mi gent bu wéet, sagu réew mi sàggiku, tundi Israyil ne faraas, kenn du ca jaare.

Acts 9:15 TSK

Sang bi ne ko: «Demal, ndax kooku jumtukaay laa ko tànne, ngir mu xamali sama tur, xeeti jaambur yi ak seeni buur, xamal ko itam bànni Israyil.

¶ Gannaaw ab diir buur Àggripa ànd ak jigéenam Berenis ganesi Sesare, ngir nuysi Festus.

ñiy jariñoo alalu àddina, bañ cee xér, ndax melow àddina sii tey, day wees.

Ndax bindees na ne: «Bépp boroom suux, nim ñax la mel, mboolem darajaam mel ni tóor-tóoru àll, ñax ma wow, tóor-tóor ma ruus.