TSK

TSK · Acts 26:14

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu ne ko: «Dawal, nga wax xale bu góor bii ne ko: “Yerusalem lees di dëkke, te tata wëru ko; ŋàpp lay def, ndax barewaayu nit ñeek jur gi ci biiram.

Acts 9:4 TSK

Mu daanu ci suuf, daldi dégg baat bu ko ne: «Sóol, Sóol, lu tax nga di ma bundxatal?»

Mu may ko. Póol taxaw ca dëggastal ya, tàllal mbooloo ma loxo, ñu ne selaw. Mu wax ak ñoom ci yawut, ne:

Acts 22:7 TSK

Ma ne dàll fi suuf, daldi dégg baat bu ma ne: “Sóol, Sóol, lu tax nga di ma bundxatal?”