TSK

TSK · Acts 27:43

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ku Aji Sax ji rafetlu say jëf, say bañ sax, mu jubaleek yaw.

Te itam nangeen waajalal Póol daamar, waral ko, ngir yóbbu kook jàmm ba ca Feligsë, boroom réew mi.»

Teewul njiitu takk-der ba sobental waxi Póol, déggal dawalkat ba ak boroom gaal ga.

Ñetti yoon lañu ma dóori yet, dóor may doj benn yoon. Ñetti yoon laa dugg gaal, mu suux. Fanaan naa, yendu naa biir xóotey géej.