TSK

TSK · Acts 4:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Dégluleen kàddug Aji Sax ji, yeen njiiti Sodom, teewluleen sunu yoonu Yàlla, yeen askanu Gomor.

Luke 20:1 TSK

¶ Mu am bés bu Yeesu doon jàngal askan wi ca kër Yàlla ga, di xamle xibaaru jàmm bi. Sarxalkat yu mag ya ak firikati yoon ya ne jalañ, ñook njiit ya.

¶ Ci kaw loolu Pilaat woo sarxalkat yu mag ya, ak njiit ya ak askan wa.

Acts 4:8 TSK

¶ Fa la Piyeer feese Noo gu Sell gi, ne leen: «Yeen kilifay xeet wi ak mag ñi,

Acts 5:34 TSK

Ab Farisen bu ñuy wax Gamalyel, di jànglekatu yoonu Musaa bu ñépp nawloo, daldi taxaw ca digg kurélu àttekat ya. Mu joxe ndigal ngir ñu génne leen ab diir.