TSK

TSK · Acts 4:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Bu ñu leen yóbboo ca jàngu ya, ca kanam kilifa ya, ak àttekat ya, buleen jaaxle ci nan ngeen di yékkatee kàddug layoo, ak luy doon seenu lay, mbaa lu ngeen di wax,

¶ Ci kaw loolu Pilaat woo sarxalkat yu mag ya, ak njiit ya ak askan wa.

Acts 4:5 TSK

¶ Ca ëllëg sa kilifay Yawut yi ak mag ñi ak firikati yoon yi daje Yerusalem.

Acts 7:55 TSK

Eccen nag feese Noo gu Sell gi, ne jàkk asamaan, daldi gis leeru Yàlla, gis Yeesu taxawe fa ndijooru Yàlla.