TSK

TSK · Acts 5:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba bët setee, mbooloom magi askanu Yawut, ak sarxalkat yu mag ya, ak firikati yoon ya, ñépp daje. Ñu yóbbu Yeesu ca seen kurélu àtte ba.

Acts 6:12 TSK

Ba loolu amee ñu xabtal nit ñi ak njiit yi, ak firikati yoon yi, ñu ne jalañ, jàpp Eccen, yóbbu ca kurélu àttekat ya.