TSK

TSK · Acts 5:36

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Kon du yaay waayu Misra jooju yëngaloon dëkk bi ci fan yii, te yóbbu woon ñeenti junniy Bóomkat ya (4 000) ca màndiŋ ma?»

Ku foog ne moo am solo, te du dara nag, boppam lay nax.

Ñu baree leen di topp ci seen nawtéef gu ëpp, ba tax yoonu dëgg gi tegoo ay saaga ndax ñoom.

Jude 1:16 TSK

Ñooñoo di ñaxtu ak a jàmbat, te topp seen bakkan; kàdduy damu yu réy ay jibe seen gémmiñ, te ñooy jay ñi ñu yaakaare njariñ.

Jë bi nag, tur wii lañu ci bind, muy kumpa: Babilon gu mag gi, ndeyu jigéeni moykat yeek ñaawtéefi àddina yi.