TSK

TSK · Acts 8:26

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Askalon moo koy gis, tiit; Gasa gis ko, jàq njàqare lu réy, mook Ekkron it ndax yaakaar ju tas. Gasa la buur bay réere, Askalon ñàkk ku ko dëkke.

Luke 3:2 TSK

jant yooyu Anas ak Kayif dee sarxalkat yu mag ya, ca la kàddug Yàlla dikkal Yaxya doomu Sàkkaryaa, ca màndiŋ ma.

Acts 10:7 TSK

¶ Naka la malaaka ma wax ak Korney ba dem, mu woo ñaar ciy surgaam, ak benn takk-der bu jullite te bokk ciy suqam.

Acts 12:8 TSK

¶ Malaaka ma ne ko: «Takkal sa geño te sol say dàll.» Mu def noonu. Mu ne ko: «Solal sa mbubb te topp ci man.»

Ndax malaakam Yàlla ji ma moom, te ma di ko jaamu, moo ma dikkal biig.