TSK

TSK · Acts 8:30

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Sa yoonu santaane laay daw, yaa may may xol bu tàlli.

¶ Ci kaw loolu mu ne leen: «Lii moo di kàddu ya ma leen waxoon ba ma nekkee ak yeen. Noon naa leen: Mboolem li ñu bind ci samay mbir ci yoonu Musaa, ak ci téerey yonent yi, ak ci Sabóor, fàww lépp sotti.»

Waaye fu mbooloom gëmkat ñi daje, juróomi baat yu ma waxe samam xel ngir jàngle, moo ma gënal junniy baat yu ma waxe weneen làkk.

¶ Fii nag xel la laaj: ku am ug dégg, na waññ limu rab wi, ndax boobu lim turu nit la taxawe, di juróom benni téeméer ak juróom benn fukk ak juróom benn (666).