TSK

TSK · Acts 8:33

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 27:2 TSK

Yàlla miy dund seere na, moom mi ma xañ dëgg, moom Aji Man ji ma teg naqaru xol,

Doole ŋiis, yax yoqi, fit ne soyox, seey.

di dëggal ku sikk ndax ab ger, tey xañ boroom njekk, ag njekkam.

Àtte nañu ko ñàkkal, yóbbu, te ag maasam kenn teewluwu ci ne tooñ gu sama bokk yi tooñ lees ko dagge ci réewum aji dund ñi, te loolu lees ko fàdde.

Moo tax ma di ko jox ab cér ci biir ñu bare, mu séddoo ak ay kàngam alalu xareem, ngir moo jébbale bakkanu boppam, ñu limaale kooki tooñkat, moo gàddu bàkkaaru ñu bare te mooy tinul moykat yi.

Moo tax yoon lafañ, te àtteb dëgg du feeñ mukk. Ku bon a tanc ku jub, ba tax ab àtte jalgatiku.

Moo toroxlu, moo nangu, ba dee fekk ko ci, ak mbugalu bant ba ñu ko daaj.