2 Kings 4:32
TSK
Ba Alyaasa agsee ca kër ga it, fekkul lu moy néewu xale bi tëdd ca kaw lal ba.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba Alyaasa agsee ca kër ga it, fekkul lu moy néewu xale bi tëdd ca kaw lal ba.
Ba loolu amee mu dànd leen lu tollook saanu xeer, daldi sukk, di ñaan.
Mu ne gurub, samp bëti óomam, daldi àddu ca kaw, ne: «Sang bi, bu leen topp bii bàkkaar.» Naka la wax loolu, daldi nelaw.
Ba nu fa amee fan yooyu lanu fa bàyyikoo, dem, ñu gunge nu, ñoom ñépp, ñook seeni soxna ak seeni doom. Nu dem ba génn dëkk ba, daldi sukk ca tefes ga, ñaan.