Genesis 19:11
TSK
Ba loolu amee ñu gumbaal nit ña nekkoon ca buntu kër ga, mag ak ndaw, ñuy làmbatu bunt ba, ba sonn, bàyyi.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba loolu amee ñu gumbaal nit ña nekkoon ca buntu kër ga, mag ak ndaw, ñuy làmbatu bunt ba, ba sonn, bàyyi.
Alyaasa nag ñaan ne: «Aji Sax ji, ngalla ubbil ay bëtam, mu gis.» Aji Sax ji ubbi bëti surga ba, mu xool, ndeke tund waa nga fees aki fas aki watiiri sawara, wër Alyaasa.
Léegi nag loxol Boroom baa ngii fi sa kaw; dinga gumba, ba dootuloo gis jant bi ab diir.» Ca saa sa gis-gis bu naqari akug lëndëm ne milib ci kawam, muy wëndeelu, di wut ku ko wommat.