TSK

TSK · Amos 2:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Maa ngi koy gis, te du tey, Maa ngi koy niir, te jubseegul; biddiiw a feqe fa Yanqóoba, yetu nguur a yékkatikoo fa Israyil, daldi toj boppi Mowab, toj kaaŋi mboolem askanu Set.

Mooy sànk kilifa, di neenal njiitu àddina.

Sidditu Mowab day dog, loxoom damm.» Kàddug Aji Sax jee!