Ci kaw loolu Yerbowam tabax ay bérabi jaamookaay, ba noppi tabb ay sarxalkat ci baadoolo yu bokkul ci askanu Lewi.
TSK
TSK · Amos 7:10
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Naka la Axab gis Ilyaas, ne ko: «Kii yaw a, di lëmbe Israyil nii?»
¶ Ci kaw loolu, doomu Imer, Pasur, sarxalkat ba jiite woon saytub kër Yàlla ga, dégg Yeremi muy biral kàdduy waxyu yooyu.
Ana lu waral ngay biral waxyu ci turu Aji Sax ji, naan kër Yàlla gii dina tas, mel ni ga woon ca Silo, te dëkk bii day tas, kenn du fi des?» Mbooloo ma mépp nag sam Yeremi ca biir kër Aji Sax ji.
Ba mu demee ba tollook buntu Beñamin, daje faak njiitu dag ya, Irya doomu Selemya doomu Anaña. Irya taxawal Yonent Yàlla Yeremi, ne ko: «Ãa, waa Babilon nga daw jëm!»
Yeena bañ kuy yedde ci pénc, te sib boroom làmmiñ wu maandu.
Ñu tàmbali di ko sosal, naan: «Kii lanu fekk muy fàbbi askan wi, di aaye ku fey Sesaar galag, te naan moom ci boppam mooy Almasi, di buur.»
¶ Naka lañu dégg loolu, seen xol fuddu, ñuy yéyu ci kawam.