TSK

TSK · Colossians 3:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

ndax Aji Sax ji, ku mu sopp, waññi la, ni baay, ak doom ju ko neex.

¶ Yeen ñiy baay it, buleen xoñoñal xale yi, waaye yarleen leen, di leen jubanti, di leen xamal coobarey Boroom bi.

Te it fàtte ngeen kàddu yii ñu leen ñaaxe, ni nit aki doomam: «Doom, bul xeeb yaru Boroom bi, bul xàddi, bu la waññee,