TSK

TSK · Daniel 1:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ci kaw loolu Sóol yónnee ca Yese, ne ko: «Bàyyil Daawuda, mu di ma liggéeyal far, ndax bég naa ci moom.»

Ndokklee say nit! Ndokklee sa jawriñ ñii dëkke taxaw ci sa kanam, di dégg sam xel!

¶ Ci biir loolu Dañeel fas yéene ci xolam ne du sobeel boppam ci njëlu buur ak biiñam. Mu ñaan kilifag jawriñ ya mu may ko, mu bañ cee sobeel boppam.

Luke 11:3 TSK

May nu bés ak bés sunub dundu bés bu nekk.