Boroom baa ngii di leen sottisi dexu Efraat gi ne xéew ak dooleem, te mooy buurub Asiri ak mboolem darajaam. Dex gi mooy génn xuram, fees fépp fu dig tàkkam,
TSK
TSK · Daniel 11:10
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Isaiah 8:7
TSK
Jeremiah 46:7
TSK
«Kii ku mu, muy fuddu ni dexu Niil, di fuur ni wali ndox?
Daniel 9:26
TSK
Bu juróom benn fukk yeek ñaar ciy àppi juróom ñaar weesee, dees na bóom ku ñu fal, te kenn du ànd ak moom. Gannaaw loolu kilifa dina ñëw, ànd ak gàngooram, yàqte dëkk beek jaamookaay bi. Waaye kilifa googu lu mel ni mbënn a koy mujje. Dogal nañu ne yàqte gi dina wéy ba keroog xare biy jeex.
Daniel 11:22
TSK
Mboolooy xare yi dinañu def um wal nig dex, dal ci kawam, waaye dees na leen rajaxe, ñook genn kilifay mbooloom kóllëreg Yàlla gi.
Daniel 11:39
TSK
Tuuri jaambur yooyu lay doolewoo, di song dëkk yi ñu wëralee ay tata. Ku ko nangul, mu teral la, def la kilifag ñu bare, ba noppi yoole la ay suuf.