TSK

TSK · Daniel 11:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

«Maa leen naroona teral ni doom yu góor, may leen suuf su xemmemlu, ngeen gënle xeet yépp suuf. Ma noon dingeen ma wooye baay te dungeen ma dëddu mukk.

Ma gis ko nag, mu dikk ba ca moom, song kook xadar, dóor kuuy mi, damm ñaari béjjénam, te kuuy mi manu koo të. Mu daane ko ci suuf, note ko, te kenn manu koo teqaleek moom.

Waaye buur bu jàmbaare dina falu, di boroom kilifteef gu yaatu, di def lu ko soob.

Gannaaw loolu dina dugg ci réew mu taaru ma, te ñu bareey daanu. Waaye Edomeen ñaak Mowabeen ñaak njiiti Amoneen ñi dinañu rëcc.