All books in KYG

Daniel 11

KYG · verse 2

12 chapitre

KYG / Daniel / [JC0] chapitre 11

KYG · verse 2

« L éegi, maa ngi lay xamal lu wér. Dama ne, dina amaat ñetti buur yuy falu ci réewum Pers, ñeenteel ba dikk, dajale alal ju bare, ba ëpple leen ñoom ñépp. Bu demee ba alalam may ko doole, dina def lépp lu mu man ngir xabtal ñépp ci kaw nguuru Geres.