2 Kings 8:14
TSK
Asayel bàyyikoo ca Alyaasa, dellu ca sangam. Mu ne ko: «Lu la Alyaasa wax?» Mu ne ko: «Nee na ma de dinga jóg moos.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Asayel bàyyikoo ca Alyaasa, dellu ca sangam. Mu ne ko: «Lu la Alyaasa wax?» Mu ne ko: «Nee na ma de dinga jóg moos.»
naan: «Musiba dal na ko, du jógati!»
Mboolooy xare yi dinañu def um wal nig dex, dal ci kawam, waaye dees na leen rajaxe, ñook genn kilifay mbooloom kóllëreg Yàlla gi.
Buleen gëm ab xarit, buleen wóolu ab xejj, fi kanam ndaw siy tëdd sa gannaaw sax, sàmmal sa bunti gémmiñ.