TSK

TSK · Daniel 4:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Da ne: Aji Sax ji Sinayi la bawoo, fenkale leen fa Seyir, naajali leen fa tundu Paran, ànd ak ndiiraani ñu sell ña, ndijooram ba indil leen melax.

Ana kuy dab-dabal Aji Sax ji, fa kawa kaw? Ana ci goney Yàlla yi ku nirook Aji Sax ji,

Ñu mujj ma indil Dañeel, di Beltasar, mi ñu tudde sama yàlla, di ku xelu yàlla yu sell yi nekk ci moom. Ma wax ko gént gi.

Li ñu santaane ñu bàyyi ëkk beek reeni garab gi mooy tekki ne nguur gi dees na la ko delloo keroog boo xamee ne Boroom asamaan mooy Buur.

“Ñeenti rab yu mag yooyu, ñeenti buuri àddina lañu yuy ñëw.

¶ Ba loolu amee ma dégg jenn aji sell di wax, jeneen aji sell ne ko: «Lan mooy àppu peeñu mii ñu gis, ñu di ci dakkal sarax biy am bés bu jot, di teddadil gàngooru xare gi, ak a tooñ, di yàq lépp?»

Luke 4:34 TSK

«Moo yaw Yeesum Nasaret, lu nu joteek yaw? Alagsi nu mooy say tànk? Xam naa yaa di kan, yaa di Aji Sell ju Yàlla ji!»

kooku dina naan biiñu sànjum Yàlla bu kenn raxul, ñu xelli ko ci kaasu sànjam. Te dees na ko mbugale sawara ak tamarax ci kanam malaaka yu sell yi ak Gàtt bi.