Ezekiel 17:23
TSK
Ca kaw tundu Israyil wu mag wa laa koy jëmbat, mu sëq, meññal, ba doon garabu seedar gu am daraja, mboolem picc dëkke ko, mboolem njanaaw màkkaanoo keram.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ca kaw tundu Israyil wu mag wa laa koy jëmbat, mu sëq, meññal, ba doon garabu seedar gu am daraja, mboolem picc dëkke ko, mboolem njanaaw màkkaanoo keram.
te Yàlla teg ci say loxo doom aadama yeek rabi àll yeek njanaaw yi, nga boole leen yilif ñoom ñépp ak fu ñu mana dëkke: yaw yaay boppu wurus bi.
Mu ngi mel ni doomu fuddën bu nit jël, sànni cib toolam. Mu sax, màgg ba doon garab gu njanaaw yi tàgg ciy caram.»