TSK

TSK · Daniel 4:25

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 30:3 TSK

Ñii ndóol, xiif, desey yax, di ŋeeñaatoo biir àll, fu lëndëm, gental, maral,

Yal nañu rus, jàq ba fàww. Yal nañu torox, sànku.

Man maa sàkk suuf, sàkk doom aadama ak mala fi kaw suuf ci sama doole ju bare ak sama kàttan gu matale, te loolu lépp, maa ko jox ku ma neex.

Garab gi nga gis muy màgg di réy, njobbaxtal lay laal asamaan, ñu di ko séen ci àddina sépp,

dàqe ko ci nit ñi, def xel ma xelum rab. Mu dëkk ak mbaami àll yi, am ñax dim xontam niw nag, lay biy wàcc, di ko faam, ba kera ba mu xamee ne Aji Kawe jee yor nguurug nit, di ko jox ku ko neex.