Job 31:6
TSK
na ma Yàlla natte màndaxekaayu dëgg, ba ràññee samag mat!
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
na ma Yàlla natte màndaxekaayu dëgg, ba ràññee samag mat!
Lu waay def, daa jub ca moom, waaye Aji Sax jeey natt xol yi.
«Yaw nit ki, waa kër Israyil mbuubitu weñ gu raxe lañu ci man léegi. Ñoom ñépp duñu lenn lu moy xànjar ak weñ gu weex ak gu ñuul ak beteex ci biir taalub tëgg. Mbuubitu xaalis rekk lañu.