TSK

TSK · Daniel 6:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Kon nag dangay tànn ci biir mbooloo mi mépp ay góor ñu mat, ñu ragal Yàlla te dëggu, boole ci sib alalu ger. Su ko defee nga tabb leen, ñu yilif ay kurél yu mat junniy nit ak yu tollu ci téeméeri nit, ba ci juróom fukki nit mbaa fukki nit.

Dajaleleen xeet yi fi kaw Babilon, wooleen buuri Medd ak kàngam ya ak jawriñ ñaak mboolem réew mu ñu moom.

¶ At ma jëkk ca jamonoy Daryus, ma bokk ca waa Medd, di doomu Aserus te falu woon buurub waa Babilon,

mbaa boroom dëkk yi diy ndawam, te mu tabb leen, ngir ñu mbugal ñiy def lu bon, te sargal ñiy def lu baax.