TSK

TSK · Daniel 6:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Aman wax Buur Aserus ne ko: «Aw xeet a ngi fi, tasaaroo ci biir xeet yi, jaxasoo ci seen biir, ci mboolem sa diiwaani réew mi. Seeni aada daa wuuteek yu xeet yépp; yoon yi Buur tëral, duñu ko jëfe, te jaaduwul ci Buur mu di leen seetaan.

Aryog gaaw yóbbu Dañeel ba ca Buur, wax ko ne ko: «Gis naa ci ngàllog Yudeen ñi ku la mana firil sa gént gi.»

Te képp ku sujjóotul màggal ko, dees na ko sànni ci biir taal bu yànj.”

¶ Ci kaw loolu ñu indi Dañeel fa kanam Buur. Buur ne Dañeel: «Du yaay Dañeel mi bokk ci Yudeeni ngàllo, ga Buur saa baay jële Yuda?

Acts 17:7 TSK

te Yason a leen dalal. Ñoom ñépp a xëtt ndigali buur Sesaar, te naan am na beneen buur bu ñuy wax Yeesu.»