TSK

TSK · Daniel 6:15

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Yeen ci seen wàllu bopp nag, bindleen ci Yawut yi lu leen soob ci sama tur, man Buur. Tayleen ko, torloo ko sama jaaro. Ndax mbind mu ñu bind ci turu buur, tay ko, torloo ko jaarob buur, maneesu koo toxal.»

Saytukati nguur gépp ak laman yeek jawriñ yeek boroom xel yeek jaraaf yi mànkoo nañu, tëral dogalu buur bi yoonal aaye bii: ci diiru fanweeri fan, képp ku ñaan ci jenn yàlla mbaa ci nit ku la moy, yaw Buur sang bi, dees na ko sànni ca kàmbu gaynde ya.