TSK

TSK · Daniel 6:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Ezra 4:22 TSK

Fexeleen ba baña néewal mbir moomu bala muy law, ba doon loraange ci nguur gi.

Gudd fan, mu joxee ndijoor; càmmoñ ba, alal ak teraanga.

¶ Ba mu ko defee Buur teral Dañeel, may ko lu baree bare, ba noppi def ko kilifag diiwaanu Babilon gépp, teg ci fal ko, mu yilif boroom xam-xami Babilon yépp.

¶ Ca la Baltacar joxe ndigal, ñu solal Dañeel yérey buur yu xonq curr, takkal ko caqu wurus, daldi yégle ne moo topp ci bummi.

Luke 16:2 TSK

Waa ja woo ko, ne ko: β€œLi ma la déggal, lu mu doon? Limal ma sag caytu, ndax dootoo ma mana saytul.”

Te itam li ñuy sàkku ci ay saytukat moo di ñu jara wóolu.