Daniel 7:15
TSK
¶ «Ba mu ko defee, man Dañeel, ma am njàqare; sama peeñu yooyoo ma tiital.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Ba mu ko defee, man Dañeel, ma am njàqare; sama peeñu yooyoo ma tiital.
¶ May xool ci biir peeñu mi, man Dañeel, di jéema xam lu muy tekki, jëmm juy nirook góor, ne jimeet taxaw ci sama kanam.
¶ Jant yooyu, man Dañeel maa nga doon ñaawlu diiru ñetti ayi bés.
Naka lay jóg rekk, nguuram daldi foq, tas, ñeenti ngelawi asamaan tasaare, yóbbu. Aw askanam du moom nguur ga, te nguur ga dootu am doole ja mu amoon. Nguuram day foq, tàbbi ci loxoy ñeneen ñu dul askanam.