TSK

TSK · Deuteronomy 2:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Rakk ja moom it am doom ju góor, tudde ko Ben Aami (mu firi Sama doomu mbokk). Ben Aami moo sos Amoneen, ñi fi nekk ba tey.

¶ Ba loolu amee Aji Sax ji ne ma: «Buleen dal ci kaw Mowabeen ñi, di leen song ub xare, ngir duma leen jox benn cér ci seenum réew, ndax askanu Lóot laa sédd réewum Ar.»

Yéene bii ñeel na Mowab: Genn guddi déy la Ar Mowab, dëkk ba tas, ne mes! Genn guddi déy la Kir Mowab tas, ne mes!